15 oct. 2011

Bril Fight 4's "Toxic" Lyrics













Intro 

Def dara squad ""yeah bril Fight 4.. a.k.a the last fighter, a.k.a the supa creator "ha ha"

Refrain 
"toxic daniou toxic" , nioune la baye yi logik , yi léni bayilo zik 
"toxic daniou toxic" c'est de la bonne zik hey , thi sa brand new day 
"toxic daniou toxic" no meunou léne supporté note yi niouy ték ci porté 
"toxic daniou toxic" guiss nga bril FIGHT.4 moy sa real bayil fo

Verse 1 
bouléne djégué daniou yék seuss yangui sokh , niongui naw 
foléne dégué dawal beuss djégui dokh thia guinaw 
I don't know (why) noy yeugué (wa) Fight now 
kouné guéné founé louné yéguiwate fanaw 
hey (hey) ho (ho) sokhla wounie fi kheuw té thi djeuf nioy sa pro , bro sokhla gnibi go 
welcome to the hood (hey) akcinga sunu block 
dinga ame good (day ) aak bodé real black ,, whaaaaaaaat 
(Class'Chic) 
walla walla bok , dou ya wara bokk , wérou tokk linga fokk baniou nara yokou amoul féne mbokk 
hello yaw fou sorii lagne la délo 
kheuyoulo daw weuri sounou bor nga dallo 
kheuthie weed défati veup,, teugg beat neva give up 
zapé onde bi , sunu monde bi gueuna ti reup 
bi beureup raack rékay takha mouthiou that's what'up 
daniou dof ci rap
refrain : "toxic daniou toxic" , nioune la baye yi logik , yi léni bayilo zik 
"toxic daniou toxic" c'est de la bonne zik hey , thi sa brand new day 
"toxic daniou toxic" no meunou léne supporté note yi niouy ték ci porté 
"toxic daniou toxic" guiss nga bril FIGHT.4 moy sa real bayil fo

2 Verse 
Fight 4 class'chic dikk djokhla right shit ngéne gueuna tookk siikk " nioune daniou toxic" 
Sunu rap class'chic this is the right shit fépp lay tokk shittt " we're so toxic " 
(bis) 
yeugoulo lou khéw deuppal djéw now what time it is 
bo niouy téré téw ya ain't know what kind of crime it is 
yangui guisss,, niongui bizz stop the commedies ,, 
mbeur mi feuggna , dougouna ,, beuggna ,, déf praaa mu rich 
réne dou done daaw, tay louniou songou daneko 
thieurgui day daw, togal thi keurgui don't go 
low low , boul thiow , bayiléne niou kheuw mbeuw 
kouthi guissoul limouy guirr défal sa xél ni day mbaw
refrain : "toxic daniou toxic" , nioune la baye yi logik , yi léni bayilo zik 
"toxic daniou toxic" c'est de la bonne zik hey , thi sa brand new day 
"toxic daniou toxic" no meunou léne supporté note yi niouy ték ci porté 
"toxic daniou toxic" guiss nga bril FIGHT.4 moy sa real bayil fo

3 Verse 
yégg naniou bénén phase, yénén phrase , féssall page, 
niongui wadjal kamikaz thi sa base, ami case, 
you niouy todji, bayi gaz 
kéne dou noyi , sunu rage feuss niou romb séne age,,
bombou , djombou " c'est naz" 
fipou eundi , dindi, bindeu rimbi gueune di gondi, guéneu djeundi , style bi réndi, dérétt di féndi , nieupp nandi,, 
nioy gueune di djapp, di ndjapp, di rap nga guiss 
nioune douniou stop , nioy drop nga sapp niggiz 
bokkou djapp, wakhou dapp ,, rap djouni piste 
toxic tokk siitt , nieupp tiite eundi peace 
guiss nga lithi topp , 
kén dou noyi founiou tokk 
djeulko défko thi sa bopp 
founiou lakou ame loufa tokkk

Refrain 
"toxic daniou toxic" , nioune la baye yi logik , yi léni bayilo zik 
"toxic daniou toxic" c'est de la bonne zik hey , thi sa brand new day 
"toxic daniou toxic" no meunou léne supporté note yimay ték ci porté 
"toxic daniou toxic" guiss nga bril FIGHT.4 moy sa real bayil fo

Outro 
you know me yaw mi , yangui beugga djomi
ya hear me ,hommy kaay fi na wommi 
new shit do siip , nioune daniou toxic
new zik bi déf hit ngéne gueuna took sikkk
bril fight 4 from the hood,, dokhantoufa guissko fa, 
Thiaroye Diamaguene laniou hip hop discover 
shout out to my man talla héy ,,, def dara squad 
BRIL FIGHT.4....

No hay comentarios:

Publicar un comentario